Bienvenue au BAAT pour le spectacle GOSPEL de Agsila ce samedi 18 Juin 2022.
Lien GPS du BAAT : https://goo.gl/maps/y2hZHKxSxqjWb7Yx5
Les chansons sont extraites de l'album "Bët set na", composition Agsila.
"Bët Set Na" Gospel Wolof
Playlist du 18juin 2022
"à la mémoire de mon Père "
PROGRAMME
1ère PARTIE : Anto de Saint Louis
En première partie du concert de Agsila, Anto et ses musiciens interprètent 3 chansons de leur répertoire :
Yeesu Nieuwal
Bimala Amé
Waxlen ko.
2ème PARTIE : Chorale de Thiès
- Nguur de Agsila avec les musiciens et la chorale de Thiès
- Maa ngi yékkati sa tur par les musiciens et la chorale de Thiès
3ème PARTIE : Agsila présente "Bët set na"
Voix : Agsila, Justin, Seni, Diouli
1/Xale yi
2/Doomi leer
3/Buur Yàlla
4/Yàllaay sama kiraay
5/Yeesoo ngi delusi
6/ Billy's Song(wóolul boroom )
7/Séetoo-séet .
8/Turam an na dóole
CHANSONS ET REFRAINS
TURAM AM NA DOOLE
Ma bariwoon i titange bari bida
Loon wa x ma jaxle ca tey Rangoon galaac
Taxul rab yi Yap ma jine yi di ma jomal
Li du léeb ma ko dund am ay séede
REFRAIN:
Bama jaxle ba woo yeesu la recc ,
Yeesu krist ay waay turam am na doole
Saraxeel juniy nag seetil juniy kangam
Yaa ngi tukki fune taloo lekk ak naan
Sangool luna neex rab yi faale wunu la
Lii du léeb tuddal turam rab yi may la jàmm
YEESOO NGI DELLUSI
Jamono yewwu jot na maandul raggal Yàlla
Yeesooy Almasi te mooy dellusi
Jógal yeewu jot na,
jammono dina na ñëw ju boroom kër gi di jóg tëj buntan
REFRAIN:
Aleluya aan aleluya,
Alxamdulila santal Yàlla
Santal Yàlla ann aleluya
Aleluya ann aleluya
Wàññikuleen ci Yàlla mooy boroom yërmandeek yiw
Sellal-leen boole koor a ki jooy
Dajale-leen askan wi sellal-leen mboolo mi
Wooleen mag ñi ba ci gone yiiy namp
Pont:
Jikko yee, jikko yi
Pare leen jikko yee
Defar leen seen toogaay
Issa mooy dellusi musal nu
DOOMI LEER
Xibaár bi nu almasi Yégal moy li
Yàllaa moom leer
Sakk leeru asamaan
Mu sol la xelam ma nga doon doomi leer
PONT:
Bu ñu ne Yàlla Baay
Bu ñu ne Maam Yàlla
Suux taxul ,dereet taxul
Bu de leer leer la, jëf ju baax moo moom
Doxal si leeram doon doomi leer
REFRAIN: CHOEURS
Boroom xel yi laay waxal
Boroom xel yi laay waxal
Yéena di leer , leeru addina
Dekk bu nekk ci tund du mana nëbboo
Taalibe Sénegal juddu waatal ci leeram
XALE YI
Fonk-leen dund gu sell
Ku sellul doo gis boroom bi
Adji sax ji kenn la
Soppeleen ko seen leppi xol
Xamal leen ko seeni doom
Ba bu ñu màggee xamal seeni sët
Tegleen gone ci yoonu Yàlla
Ba bu ñu xammee du ñu ko wacc
REFRAIN: CHOEURS
Yeesu neena bayileen xale yi
Ñu mel ni nooma yello nguruug Yàlla
LEAD:
* Te it wottu leen a xeeb kenn ci ni gena tuuti ndax kat seeni malaakaa ngi sax ci jotayu Baay bi ci kaw.
CHOEURS:
Xale yeey sama xarit Yàllaa ma leen Yonne nu doon yool ci man.
BILLYE'S SONG:( Wóolul boroom bi)
Dañuy takku tey bëre te duñu daw
Wékk nañu sunu yakaar ci Yàlla
Dara manu noo tàgaleek bëggelam
Du nàttu du fitna te du njàqare
REFRAIN: CHOEURS
Ouyala lala ou Yàlla laaah
Knowing trusting,never douting
Let the Saviour in!
Ouyala lala ou Yàlla laaah
Loving waiting Always praising
Jesus rules within
LEAD AND CHORUS:
I rise before dawn and cry for help
I have put my home in your Words
My eyes stay th rough the watches of the night
That i may meditate on your promises
SÉETOO-SÉET
REFRAIN:
Ayee yiyee eh Séetoo-séet
Géew-leen ñu feec
Séetoo-séet
Couplet:1
Jigeen sama séet sama
Sa mbëggeel neex na
Séet sama nene sama
Lem ay xéllee sa gémmiñ
Yaay seyaan bu tëje , di bëtu ndox bu saañe
Danga ñul rafet ni xay ma ya ca kedar
Jàppal-leen ma till yu ndaw yee
Yàq lañuy def ,te duñu jariñoo
Loolu la waaji wax
Couplet 2
Sama nejaay a gën ci xale yu góor yi
Maay bege kepparam
Safoo doom ya
Dugal nama néegub sago jeex Na
Jàppal leen ma till yu ndaw yee
Yàq lañuy def te duñu jariñoo
Loolu la ndaw si wax
REFRAIN:
Ayee yiyee eh Séetoo-séet
Géew-leen ñu feec
Séetoo-séet
YÀLLAAY KIIRAAY
REFRAIN:
Yàllaay sama kiiraay,
Yàllaay sama kattan
Yaa di sama Tata
Sama rammukat
COUPLET1:
Yoonu Yàlla dafa mat
Kaddoom dafa wóor
Kepp ku laqu ci Yàlla
Dammam dafa wóor
May woy Adji sax ji man
Ngir mucc samay noon neey
Duma làqu duma tiit man .
Ñi yeene lu bon
REFRAIN: VARIATION
Yàllaay sama kiiraay,
Yàllaay sama kattan
Yaa di sama Tata
Sama rammukat
CHOEURS :
Dukkat leen, dukkat leen
Buur bi jar Nako
Dukkat
Entretien avec Agsila :
« Bët set na » est votre troisième album, dans la continuité de vos engagements féministes et de votre quête spirituelle. Pourquoi avoir choisis la musique jazz comme style ?
Mon premier album « Soupirs » parle d’un féminisme inconciliable ; la culture universelle africaine demande un féminisme spécifique qui n’est pas Américain ni Européen, mais qui se situe plus dans notre société à culture matriarcale même si la femme n’est pas valorisée par rapport à l’homme.
Et mon Jazz afro est destiné à unir les africains à travers les langues et les rythmes à la recherche d’une unité. Le jazz est une expression de l’âme avec une base d’improvisation enracinée dans le réel, dans la vie quotidienne.
Après l’album « Soupirs » sorti en 2017, vous enregistrez votre deuxième album « Tegtal » avec 14 nouvelles chansons afro-jazz, plus spirituelles. Quelle est votre inspiration ?
Mon deuxième album s’appelle Tegtal, ce sont des visions.
Dans Tegtal il y a de la colère et une réponse plus spirituelle en réponse à tous nos malheurs, une réponse à tous les préjugés, et Tegtal sont des recommandations qui amènent la solution à travers l’amour, les sentiments qui permettent de supporter le pire avec compassion.
Les textes sont politiques, ils parlent du juste, celui qui aime le peuple, et de la maltraitance du faible, des vulnérables, mais je m’inspire aussi de l’environnement.
La nature nous montre que les vulnérables ne sont pas que les humains, mais aussi les animaux, comme cet oiseau qui prie dans la chanson Nãan (prière), car il n’y a plus de branches, il n’a plus d’eau et il s’adresse à Dieu dans sa prière.
Ce nouvel album, composé pendant le confinement, porte l’espoir et appel à la compassion. Avec Bët set na, est-ce que le jour se lève pour tout le monde ?
Avec « Bët set na » c’est le jour se lève. Nous étions dans les « soupirs », nous sommes passé aux visions « Tegtal », irréelles, et là le voile est tombé, le jour se lève, nous sommes dans la réalité et la mise en garde.
Nous marchons dans une vie consacrée à la lumière : la lumière pour les gens, la lumière sur nous et la lumière pour les plus opprimés.
Et la solution c’est Gospel, c’est la bonne nouvelle. La bonne nouvelle est arrivée, c’est le salut pour toutes et tous, la solution pour tout le monde.
L’humain n’est pas dieu. Dieu c’est le divin, une manifestation universelle. L’homme est restreint mais Dieu n’est pas comme ça ; il veut la paix pour tout le monde et il ne restreint pas les autres. Bët set na c’est ça : le livre est ouvert, les bras sont grands ouverts, les mains sont ouvertes.
Quelles sont les nouveautés dans votre spectacle GOSPEL ?
Le 18 Juin je présente 10 nouvelles compositions de mon nouvel album Bët set na avec de nombreux invités : la chorale de Thiès, Anto de Saint Louis, Echo de Dakar et le chanteur Justin Badara. C’est pour moi l’aboutissement de deux ans de travail de composition que je vais mettre en scène avec de nouveaux musiciens où là je sort du jazz pour aller vers le Mbalax, le reggae, le slam, la soul mais avec le désir de renouveler le genre Gospel tout en gardant les racines de notre musique Sénégalaise.
Le défi est de rester à la fois populaire en wolof et de créer de nouvelles formes musicales savantes. C’est pourquoi j’écris et je chante ici à Yene dans un village traditionnel à la culture séculaire sénégalaise qui m’inspire beaucoup dans cette période de bouleversements où il ne faut pas perdre la foi.